Dégg diine ak i cosaanam
Jële nañu ci Abuu Sahiid Al-Xudriyu -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na:
Available in 59 languages
«Jële nañu ci Abuu Sahiid Al-Xudriyu -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «bu kenn ci yéen sikk-sakkaa ci julleem te ba xamul ñaata la julli ndax ñatt la walla ñent, na sànni sikk-sakka ga, te tabax ca la ko wóor, topp mu sujjóot ñaari sujjóot njëkk muy sëlmël, bu dee juróom la julli ñu jotal ko julleem gi, bu dee dafa mottali ñent ya nag muy naqar ci saytaane».»Meaning translation ·
Saved at original quality








