Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Pas-pasu Lislaam

Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:

Available in 71 languages
«Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: "yaw sama Boroom maa ngi lay ñaan bul def sama bàmmeel ab xërëm, Yàlla rëbb na nit ñiy jàppe bàmmeelu seeni Yónente ay jàkka".»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewël ak mucc- dafa ñaan Boroomam mu bañ a def bàmmeelam ab xërëm bu nit di jaamu ci di ko màggal, ak di ko jublu buy sujjóot. Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-wax na ne Yàlla soreele na yërmaandeem képp kuy jàppe bàmmeel i Yónente yi ay jàkka; ndax jàppe ko ay jàkka yoon wu jëm ci jaamu ko la ak di ci am ay pas-pas.

Source
Ahmat soloo na ko
Download image

Saved at original quality