Ngëneel yi ak teggiin yi
Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne:
Available in 60 languages
«Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- da doon dox ci mbeddi Màkka yi, daal di romb doj wu ñuy woowe Jumdaan, mu wax ne: "doxleen lii mooy Jumdaan, ñu beru ñi raw nañu" ñu ne ko: ñan ñooy ñi beru yaw Yonnente Yàlla bi? Mu ne: "góor ñiy tudd Yàlla lu bari, ak jigéen ñiy tudd Yàlla lu bari".»Meaning translation ·
Saved at original quality








