Ngëneel yi ak teggiin yi
Jële nañu ci Xawlata doomu Hakiim As-Sulamiyata mu wax ne : dégg naa Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:
Available in 66 languages
«Jële nañu ci Xawlata doomu Hakiim As-Sulamiyata mu wax ne : dégg naa Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «ku wàcc cig kër daal di wax: ahuusu bi kalimaatil Laahi At taammaati min sarri maa xalaxa, dara du ko lor ba baa muy juge ca kër googa».»Meaning translation ·
Saved at original quality








