Pas-pasu Lislaam
Jële nañu ci Jaabir Ibn Abdullah -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne Yonente bi-yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na:
Available in 51 languages
«Jële nañu ci Jaabir Ibn Abdullah -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne Yonente bi-yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: "ku dégg nodd daldi wax: Allaahuma Rabba haasihid dahwati attaammati, wassalaatil xaa-imati, aati Muhammadan alwasiilata walfadiilata, wabhashu maxaaman mahmuudan allasii wahadtahu, kon samag rammu yell na ci moom ëllëg bis-pénc".»Meaning translation ·
Saved at original quality








