Dégg diine ak i cosaanam
Jële nañu ci Sawbaan -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne:
Available in 65 languages
«Jële nañu ci Sawbaan -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- bu daan wëlbatiku ci julli gi day jéggalu ñatti yoon, daal di wax: "Allaahumma Antas Salaamu, wa Minkas Salaamu, Tabaarakta Sal Jalaali wal ikraami" waliid wax ne: ma wax Al-Awsaahii ne ko: naka lay jéggaloo? Mu ne: day wax naan: Astaxfirul Laaha, Astaxfirul Laaha.»Meaning translation ·
Saved at original quality








