Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Pas-pasu Lislaam

Jële na ñu ci Abdallah Ibnu Mashuut mu wax ne : Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na :

Available in 61 languages
«Jële na ñu ci Abdallah Ibnu Mashuut mu wax ne : Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na : «li ñuy njëkk a àtte ci diggante nit ñi ëllëg bis-pénc mooy dereet ».»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day xamle ne li ñuy njëkk a àtte ci diggante nit ñi ëllëg bis-pénc ci tooñ gi ñenn ñi di tooñ ñeneen ñi : mooy dereet, niki ray, ak gaañe.

Source
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Download image

Saved at original quality