Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Pas-pasu Lislaam

Jële nañu ci Umar yal na ko Yàlla dollee gërëm:

Available in 47 languages
«Jële nañu ci Umar yal na ko Yàlla dollee gërëm: Mu ñëw ci Hajarul Aswad daal di koy fóon, daal di wax ne: man de xam naa ne yaw aw xeer nga, doo lor te doo jariñ, bu dul woon ne gisnaa Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc di la fóon kon duma la fóon.»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Njiitu jullit ñi Umar ibnul Xattaab yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dafa ñëw ci Hajarul Aswad ci pengu Kaaba gi fóon ko, daal di wax ne: man de xam naa ne yaw aw xeer nga, doo lor te doo jariñ, bu dul woon ne gisnaa Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc fóon la kon duma la fóon.

Source
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Download image

Saved at original quality