Pas-pasu Lislaam
Jële nañu ci Saynabu Bint Jahsin yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dafa dugg fi moom fekk moo ngi jàq, di wax naan:
Available in 55 languages
«Jële nañu ci Saynabu Bint Jahsin yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dafa dugg fi moom fekk moo ngi jàq, di wax naan: «amul kenn ku ñu war a jaamu ku dul Yàlla, alkande ñeel na araab yi ci ay wu jege, tijji nañu tay ci baaraasu Yaajuuja ak Maajuuja lu toll ni" mu ràbbale baaraamu déyam ak ba ca topp, Saynabu Bint Jahsin nee na ma ne ko: yaw Yonnente Yàlla bi: ndax dees nuy alag te ñu baax ñi nekk sunu biir? Mu ne ko: "waaw bu lu bon baree».»Meaning translation ·
Saved at original quality








