Pas-pasu Lislaam
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:
Available in 59 languages
«Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «gaawleen jëf ndax ay fitna a ngi ñëw yu mel ni dogiiti guddi gu lëndëm, nit ki day xëy di ku gëm, gontu di ab yéefar, walla mu gontu di ku gëm xëy nekk ab yéefar, day jaay diineem ci poñetu àdduna«.»Meaning translation ·
Saved at original quality








