Pas-pasu Lislaam
Jële nañu ci Jaabir Ibn Abdullah yal na leen Yàlla dollee gërëm mu wax ne Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na:
Available in 55 languages
«Jële nañu ci Jaabir Ibn Abdullah yal na leen Yàlla dollee gërëm mu wax ne Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na: "jox na nu ma juróom yoo xam ne joxuñuko kenn ku ma jiitu: dimbalees na ma ci ag ragal luy toll ni doxub weer, defal na nu ma suuf si muy jàkka di lu laab, fu julli dabe kenn ci samaw xeet na julli, daganal na nu ma koomi xare yi, te daganaluñu ko woon kenn ku ma jiitu, jox na nu ma ramm ga, Yonnente dañu ko daan yónni ci xeetam kese man
nag ñu yónni ma ci nit ñépp ".»Meaning translation ·
Saved at original quality








