Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Pas-pasu Lislaam

Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na:

Available in 70 languages
«Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «ku muñal ki am jafe-jafe, walla mu baal ka ko, Yàlla dana ko keral bis-penc ca suufus keru Gàngunaayam ga bis ba nga xam ne genn ker amul gu dul keram ga».»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day xibaare ne képp ku muñal ki ame bor, walla mu teggil ko bor ba, ag payam mooy: Yàlla dana ko keral fa suufus keru Gàngunaayam ga keroog bis-penc ba Jant ba di jege boppi jaam yi, tàngaay wa di tar lool ca ñoom, Kenn du am kerr ku dul ku Yàlla keral.

Source
At-tirmisiy soloo na ko, ak Ahmat
Download image

Saved at original quality