Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Ngëneel yi ak teggiin yi

Jële nañu ci Jaabir -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yónent Yàlla bi -yal ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- muy wax naan:

Available in 72 languages
«Jële nañu ci Jaabir -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yónent Yàlla bi -yal ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- muy wax naan: «Li gën ci sikar yi: Laa ilaaha illal Laahu, li gën ci ñaan yi: Alhamdu lil Laahi».»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yónent bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafay xamle ne li gën ci tudd Yàlla mooy: «Laa ilaaha illal Laahu» maanaam, amul kenn ku ñuy jaamu ci dëgg ku dul Yàlla, li gën ci ñaan yi mooy: Alhamdu lil Laahi; te mooy nangu ne kiy joxe xéewal mooy Yàlla -tudd naa sellam ga-, moom mi yeyoo melokaan yu mat sëkk ya te rafet.

Source
At-tirmisiy soloo na ko, ak An-nasaa'iy ca Al-kubraa, ak Ibnu Maaja
Download image

Saved at original quality