Ngëneel yi ak teggiin yi
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:
Available in 59 languages
«Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «ndax du ma leen tegtal li Yàlla di fare njuumte yi, di ci yëkkatee daraja yi?" Ñu ne ko ahakay yaw Yonnente Yàlla bi, mu ne leen: "di jotale njàppu mi ci jomonoy sibeel ga, ak baril ay jéego jëm ca jàkka ya, ak di xaar julli ga ginnaaw ak julli, loolu mooy faanu ga».»Meaning translation ·
Saved at original quality







