Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Dégg diine ak i cosaanam

Jële nañu ci Surayh ibn Haanii mu wax ne:

Available in 53 languages
«Jële nañu ci Surayh ibn Haanii mu wax ne: Laaj naa Aysatu, ne ko: ci lan la Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daan tàmbalee bu daan dugg këram? Mu ne: ci socc.»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Bokk na ci njubug Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc muy tàmbalee ci socc bu daan dugg këram, ci waxtu wu mu man a doon guddi walla bëccëg.

Source
Muslim soloo na ko
Download image

Saved at original quality