Dégg diine ak i cosaanam
Jële nañu ci Saydu ibn Saabit yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne:
Available in 49 languages
«Jële nañu ci Saydu ibn Saabit yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Xëdd nañu ak Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu daal di jug jëm ca julli ga, ma ne ko: ñaata moo dox ci diggante nodd gi ak xëdd gi? Mu ne: luy tolloo ak juróom-fukki aaya.»Meaning translation ·
Saved at original quality








