Dégg diine ak i cosaanam
Jële nañu ci Jundub Ibn Abdullah Al-Xasrii -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na:
Available in 70 languages
«Jële nañu ci Jundub Ibn Abdullah Al-Xasrii -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «ku julli suba moo ngi ci kaaraangeg Yàlla, moom Yàlla du leen toppe dara ci ay àqam, ndax ki Yàlla toppe dara ciy àq dana ko jàpp, te dana këpp kanamam ca sawaraw Jahannama».»Meaning translation ·
Saved at original quality








