Ngëneel yi ak teggiin yi
Jële na ñu ci Anas -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne:
Available in 61 languages
«Jële na ñu ci Anas -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Li ëppoon ci ñaani Yonnente bi-yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-mooy:"Allaahumma Rabbanaa aatinaa fiddunyaa hasanatan, wa fil-aaxirati hasanatan, wa xinaa hasaabannaari".»Meaning translation ·
Saved at original quality








