Pas-pasu Lislaam
Jële nañu ci Jariir Ibn Abdullah -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne:
Available in 62 languages
«Jële nañu ci Jariir Ibn Abdullah -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Nekkoon nanu fi Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-, mu xool weer wi ci genn guddi -guddi yu leer yi- daal di wax ne: " yéen de dangeen gis seen Boroom kem ni ngeen di gise weer wii, te du ngeen buuxante ngir gis ko, bu ngeen manee ba deesu leen not ci jullig fajar njëkk jant bi di fenk ak njëkk muy so defleen ko" mu daal di jàng: "{nanga sàbbaal sa Boroom njëkk fenkug jànt bi ak njëkk so ga}"»Meaning translation ·
Saved at original quality








