Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Ngëneel yi ak teggiin yi

Jële nañu ci Ubaydallah ibn Mihsan Al-Ansaarii yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na:

Available in 47 languages
«Jële nañu ci Ubaydallah ibn Mihsan Al-Ansaarii yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na: "ku xëy ci yéen di ku am jàmm ci yaramam, am kóolute ci bakkanam, am dundug bisam,, dafa mel ni jox nañu ko àdduna".»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc day xamle ne ku xëy ci yéen jullit ñi di ku wér di ku mucc ci yaramam ci tawat yi ak feebar yi, di ku am kóolute ci bakkanam ak njabootam, te ragalul ci yoonam, mu am lu ko doy ci dundug bisam ci li dagan; dafa mel ni booleel nañu ko àdduna jépp.

Source
At-tirmisiy soloo na ko, ak Ibnu Maaja
Download image

Saved at original quality