Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Alquraan ju tedd ji ak xam-xam yi ci aju

Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:

Available in 65 languages
«Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «buleen def séen kër yi ay bàmmeel, Saytaane day daw kër goo xam ne dañu fay jàng saaru Al-Baxara».»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day tere neenal kër yi ci julli ba mu mel ni ay bàmmeel ndax deesu fa julli. Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- xamle ne Saytaane day daw kër goo xam ne dañu fay jàng saaru Al-Baxara.

Source
Muslim soloo na ko
Download image

Saved at original quality