Alquraan ju tedd ji ak xam-xam yi ci aju
Jële nañu ci Abuu Muusaa Al-Asharii -yal na ko Yàlla dollee gërëm-mu wax ne :Yonnente Yàlla bi-yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-nee na:
Available in 60 languages
«Jële nañu ci Abuu Muusaa Al-Asharii -yal na ko Yàlla dollee gërëm-mu wax ne :Yonnente Yàlla bi-yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-nee na: «misaalum jullit biy jàng Alxuraan moo ngi mel ni Utruja, xetam ga dafa teey ak cafkaam teey, misaalum jullit bi dul jàng Alxuraan moo ngi mel ni tàndarma, amul xet te cafkaam dafa neex,misaalum naaféq biy jàng Alxuraan moo ngi mel ni ngun-ngun xetam dafa teey cafkaam wex,misaalu naaféq bi dul jàng Alxuraan moo ngi mel ni xettar, amul xet te cafkaam dafa wex»»Meaning translation ·
Saved at original quality








