Dégg diine ak i cosaanam
Jële na ñu ci Buraydata Ibn Al-Husaybi -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne:
Available in 65 languages
«Jële na ñu ci Buraydata Ibn Al-Husaybi -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Deeleen teel a julli tàkkusaan, ndax yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: "ku bàyyi jullig tàkkusaan jëfam yàquna".»Meaning translation ·
Saved at original quality








