Jaar-jaar ak taarix
Jële nañu ci Aysatu yaayu jullit ñi -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne:
Available in 49 languages
«Jële nañu ci Aysatu yaayu jullit ñi -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Tànnloo wu ñu Yonnente bi ci diggante ñaari mbir lu dul ne jël na ba ca gën a yomb, fii ak nekkul bàkkaar, bu nekkee bàkkaar la moo koy gën a sori ci nit ñi, te Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc musul a fayyu ngir boppam lu dul ñu xotti wormay Yàlla, mu fayyu ko ngir Yàlla".»Meaning translation ·
Saved at original quality








