WO
Meloy jikko ya
شجاعته صلى الله عليه وسلم
1 hadiths
Ag tabam SLM
2
Kersaam SLM
1
شجاعته صلى الله عليه وسلم
1
رفقه صلى الله عليه وسلم
3
Yërmandeem SLM
2
كلامه صلى الله عليه وسلم
2
ضحكه صلى الله عليه وسلم
1
بكاؤه صلى الله عليه وسلم
1
حلمه صلى الله عليه وسلم
1
1 hadiths
Jële nañu ci Aysatu yaayu jullit ñi -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Tànnloo wu ñu Yonnente bi ci diggante ñaari mbir lu dul ne jël na ba ca gën a yomb, fii ak nekkul bàkkaar, bu nekkee bàkkaar la moo koy gën a sori ci nit ñi, te Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc musul a fayyu ngir boppam lu dul ñu xotti wormay Yàlla, mu fayyu ko ngir Yàlla".
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér