Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Adiis ak xam-xam yi ci aju

Jële nañu ci Samurata Ibn Jundub ak Muxiirata Ibn Suhbata yal na leen Yàlla dollee gërëm ñu wax ne, Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na:

Available in 55 languages
«Jële nañu ci Samurata Ibn Jundub ak Muxiirata Ibn Suhbata yal na leen Yàlla dollee gërëm ñu wax ne, Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: "ku ma waxal jenn wax te xam ne ay fen la, moom kenn la ci fenkat yi".»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc day xamle ne ku toxal ab hadiis askanale ka ko fekk xam na walla mu not ci njortam ne dañu ko a fenal Yonnente bi kon aji-nettali ji day bokk ak ki sos fen wi.

Source
رواه مسلم في مقدمته
Download image

Saved at original quality