Dégg diine ak i cosaanam
Jële nañu ci Ammu Salamata yaayu jullit ñi yal na ko Yàlla dollee gërëm di soxnas Yonente bi mu ne: Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na:
Available in 48 languages
«Jële nañu ci Ammu Salamata yaayu jullit ñi yal na ko Yàlla dollee gërëm di soxnas Yonente bi mu ne: Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na: "ku am gàtt bu mu rendi bu weeru Tabaski bi duggee, bu mu jël dara ci kawaram ak ci weyam ba mu Tabaski ba noppi".»Meaning translation ·
Saved at original quality








