WO
Saaba yi
Pas-pas bees war a am ci Saaba yi Yàlla gërëm na leen
1 hadiths
Ngëneeli Saaba yi Yàlla gërëm na leen
6
Pas-pas bees war a am ci Saaba yi Yàlla gërëm na leen
1
1 hadiths
Jële nañu ci Abuu Sahiid Al-Xudriyu -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «Buleen di ŋàññ sama àndandoo yi, bu kenn ci yéen joxe woon lu toll ne Uhud ci wurus du jot Muddub kenn ci ñoom, waxumalaak xaaj ba».
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér