WO
Ñam yi ak naan yi
Naan yi araam
1 hadiths
Yi dagan ak yi araam ci mala yi ak janaaw yi
3
الصيد
1
Naan yi araam
1
1 hadiths
Jële nañu ci Ibn Umar -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «lépp luy màndiloo sàngara la, te lépp luy màndiloo dafa araam, te kuy naan sàngara ci àdduna ba dee fekk ne tàmm na ko te tuubu ko, kooku du ko naan ca allaaxira».
رواه مسلم وأخرج البخاري الجملة الأخيرة منه