WO
Njàpp
Ni ñuy jàppoo
1 hadiths
Ngëneelu njàpp
3
Sunna ak teggiini njàpp
2
Ni ñuy jàppoo
1
1 hadiths
Jële nañu ci Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu jële ci Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: "bu kenn ci yeen yeewoo ci ay nelawam na fiiru ñatti yoon, ndaxte Saytaane day fanaan ci paxi bakkanam".
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér