Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Pas-pasu Lislaam

Jële nañu ci Abuu Hurayrata mu wax ne:

Available in 71 languages
«Jële nañu ci Abuu Hurayrata mu wax ne: Wax nañu Yónent Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- ne ko ana kan ci nit ñi moo gën a texe ci sag rammu ëllëg bis-penc? Yónent Yàlla bi wax ne: «Njoortoon naa ne yaw Abuu Hurayrata Yamamay njëkk laaj lii; ndax li ma gis sag xér ci Hadiis, nit ki gën a texe ci samag rammu ëllëg bis-penc, mooy ki wax, Laa ilaaha illal Laahu, te mu sell lool ci xolam, walla ci bakkanam».»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yónent ebi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day xamle ne nit ki gën a texe cig rammoom ëllëg bis-penc mooy ki wax «Laa ilaaha illal Laahu te mu sell ci xolam» maanaam amul ku ñuy jaamu cig dëgg ku dul Yàlla, te mu mucc ci bokkaale ak ngistal.

Source
Al-buxaariy soloo na ko
Download image

Saved at original quality