Ngëneel yi ak teggiin yi
Jële nañu ci Jaabir yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: dégg naa Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc njëkk muy faatu ci ñatti fan muy wax naan:
Available in 53 languages
«Jële nañu ci Jaabir yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: dégg naa Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc njëkk muy faatu ci ñatti fan muy wax naan: "bu kenn ci yéen faatu lu dul ne dafa rafet njort ci Yàlla".»Meaning translation ·
Saved at original quality








