Ngëneel yi ak teggiin yi
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm-mu wax ne :Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na:
Available in 60 languages
«Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm-mu wax ne :Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «ki war mooy nuyu kiy dox, kiy dox mooy nuyu ki toog, ñi néew ñooy nuyu ñi bari». Nekk na ca téereb Al-Buxaarii: «xale bi mooy nuyu mag mi, kiy romb mooy nuyu ki toog, ñi néew ñooy nuyu ñi bari».»Meaning translation ·
Saved at original quality








