Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Pas-pasu Lislaam

Jële nañu ci Abdallah Ibnu Mashuud mu wax ne : Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na :

Available in 54 languages
«Jële nañu ci Abdallah Ibnu Mashuud mu wax ne : Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na : "bokkul ci nun kiy mbej ñiy mbej lex ya, di xotti kaw yére ya, di woote wooteg ceddo ya".»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc day tere di moytandikuloo yenn jëfi ceddo yi, mu wax ne: bokkul ci nun: Ki ci njëkk: kiy mbej lex ya, dafa jagleel lex cig tudd ndax li mu not ci loolu, waaye dóor yi des ci kanam gi it day dugg ci tere gi. Ku Ñaareel ki: kiy xotti baatu mbubam ngir tarug njàqare ga. Ku Ñatteel ki: kiy woote wooteg ceddo ya niki di woo alkande ak toroxtange, ak di yuuxu, ak woo naqar ak yeneen.

Source
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Download image

Saved at original quality