WO
Xam jëflante yi
Yéwénoo ak àttey dëkkandoo
2 hadiths
البيوع
4
الربا
1
القرض
4
Yéwénoo ak àttey dëkkandoo
2
الإجارة
1
Li nit def ci yoonu Yàlla ci alalam ngir nit ñi di ko jariñoo te kenn du ko donn
1
الهبة والعطية
1
Giñ yi ak nisar yi
3
2 hadiths
Jële nañu ci Ibn Umar -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «Jibriil deñul di ma dénk dëkkandóo, bama muj njort ne dana ko dondloo».
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Jële nañu ci Abuu Surayhin -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: "giñ naa ci Yàlla ne du gëm, giñ naa ci Yàlla ne du gëm, giñ naa ci Yàlla ne du gëm", ñu ne ko: kan yaw Yonente Yàlla bi? Mu ne: "ki dëkkandoom muccug ci ay loram".
Al-buxaariy soloo na ko