WO
Teggiini Sariya
آداب الرؤيا
2 hadiths
Teggiini boroom xam-xam ak kiy sàkku xam-xam
6
Teggiini jàng Alquraan ju tedd ji
1
Teggiini nuyoo ak yëglu
9
Teggiini wax ak noppi
12
Teggiini lekk ak naan
11
Teggiini tukki ak i àtteem
4
Teggiini nelaw ak yewwu
3
آداب الرؤيا
2
Teggiini seet nit ak yëglu
3
Teggiini tisli ak óbbali
3
Teggiini seet ku wéradi
5
Teggiini col
8
2 hadiths
Jële nañu ci Abii Xataadata yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: "gént gu baax ci Yàlla la jóge, gént gu bon nag ci Saytaane la jóge, bu kenn ci yéen gisee gént gu mu ragal, na tifli ci càmmooñam, te muslu ci Yàlla ci ayam, kon du ko lor".
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
عن أبي هريرة رضي الله عنه قال: قال رسول الله صلى الله عليه وسلم : «من رآني في المنام فَسَيَرَانِي في اليَقظة -أو كأنما رآني في الْيَقَظَةِ- لا يَتَمَثَّلُ الشيطان بي».
متفق عليه. مسلم