WO
Teggiini Sariya
Teggiini tisli ak óbbali
3 hadiths
Teggiini boroom xam-xam ak kiy sàkku xam-xam
6
Teggiini jàng Alquraan ju tedd ji
1
Teggiini nuyoo ak yëglu
9
Teggiini wax ak noppi
12
Teggiini lekk ak naan
11
Teggiini tukki ak i àtteem
4
Teggiini nelaw ak yewwu
3
آداب الرؤيا
2
Teggiini seet nit ak yëglu
3
Teggiini tisli ak óbbali
3
Teggiini seet ku wéradi
5
Teggiini col
8
3 hadiths
عن أبي هريرة رضي الله عنه أن رسول الله صلى الله عليه وسلم قال: «إذا عَطَسَ أَحَدُكُم فَلْيَقُل: الحَمْدُ للهِ، وَلْيَقُلْ لَهُ أَخُوهُ أو صاحبُهُ: يَرْحَمُكَ الله، فإذا قال له: يرحمك الله، فَلْيَقُلْ: يَهْدِيكُم الله ويُصْلِحُ بَالَكُم».
رواه البخاري
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yónent Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- muy wax ne: «àqi jullit ci moroomu jullitam juróom la: delloo ab nuyoo, ak seeti ki wopp, ak gunge néew bi, ak wuyu woote ba, ak ndokkeel ku tissooli».
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Jële nañu ci Abuu Sahiid Al-Xudrii -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «bu kenn ci yéen óbbalee na teg loxoom ci gémmiñam ndaxte Saytaane day dugg».
Muslim soloo na ko