Dégg diine ak i cosaanam
Jële na ñu ci Ibn Abbaas -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne:
Available in 65 languages
«Jële na ñu ci Ibn Abbaas -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- da daan wax ci diggante ñaari sujjóot yi: «Allaahumma ixfir lii, warhamnii, wa haafinii, wahdinii, warsuqnii».»Meaning translation ·
Saved at original quality








