Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Dégg diine ak i cosaanam

Jële nañu ci Ibn Umar -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:

Available in 47 languages
«Jële nañu ci Ibn Umar -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: "ku yar ab xaj bu dul xaju rëbb walla xaju sàmm wàññi na ci jëfam bis bu nekk Xiiraat", Saalim ne: Abuu Hurayrata daan na wax: "walla xaju mbay", moom baykat la woon.»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc moytandikuloo la yar xaj, lu dul ngir aajoy rëbb, walla gaarde jur gi ak mbay mi, ku ko yar ngir lu dul loolu wàññi na ci yoolu jëfam bis bu nekk Xiraat; loo lu ag natt la gog Yàlla moo ko xam.

Source
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Download image

Saved at original quality