Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Dégg diine ak i cosaanam

Jële na ñu ci Abii Sahiid Al-Xudriyu -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:

Available in 61 languages
«Jële na ñu ci Abii Sahiid Al-Xudriyu -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «bu ngeen déggee woote gi nangeen wax lu mel ni li noddkat bi di wax».»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day soññee ci bu ñu dégge nodd-kat bi ñu koy toppandoo, ci di wax kem li muy wax. Bu kàbbaree nu kàbbar, bu waxee ñaari seede yi, nu wax leen. Dees na ca settee:(hàyya halas salaah, hayya halal falaah )foofu dañuy wax ci ginnaawam : laa hawla wa laa xuwwata illaa bil Laahi.

Source
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Download image

Saved at original quality