Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Dégg diine ak i cosaanam

Jële nañu ci Husayfata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne:

Available in 56 languages
«Jële nañu ci Husayfata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc bu daan jug guddi day socc.»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daan na bari lu muy socc di ko digle it, moom nag day feddaliku ci yenn waxtu yi, bokk na ca: socc bu ñu jògee guddi, Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daan na bomb gémmeñam di ko setal ci socc.

Source
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Download image

Saved at original quality