Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Jaar-jaar ak taarix

Jële nañu ci Aysatu ndayu jullit ñi-yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne:

Available in 56 languages
«Jële nañu ci Aysatu ndayu jullit ñi-yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc ndayjoor daan na ko yéem ci buy sol dàll, ak buy peñewu, ak buy laab, ak ci mbiram yépp.»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daan na bëgg di gënale ci tàmbalee ndayjoor ci mbiram yi yelloo teral, te bokk na ca: Nit ki tàmbali ci tànku ndayjooram bu dee sol dall, mu tàmbalee ci ndayjoor bu dee peñe kawaru boppam ak sikkimam ak di leen diw, ak buy jàppu mu jiital tànku ndayjooram ci bu càmmoñ bi ci loxo yi ak ci tànk yi.

Source
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Download image

Saved at original quality