WO
Jikkoy Muhammat SLM
Njubug Yónnent bi SLM
7 hadiths
Na mu daa laabale boppam SLM
1
Na mu daa jullee SLM
1
Na mu daa doxalee ci sëy ak dundam ak i soxnaam
1
7 hadiths
Jële nañu ci Aysatu ndayu jullit ñi-yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc ndayjoor daan na ko yéem ci buy sol dàll, ak buy peñewu, ak buy laab, ak ci mbiram yépp.
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Jële nañu ci Husayfata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc bu daan jug guddi day socc.
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Jële nañu ci Saynabu Bint Jahsin yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dafa dugg fi moom fekk moo ngi jàq, di wax naan: «amul kenn ku ñu war a jaamu ku dul Yàlla, alkande ñeel na araab yi ci ay wu jege, tijji nañu tay ci baaraasu Yaajuuja ak Maajuuja lu toll ni" mu ràbbale baaraamu déyam ak ba ca topp, Saynabu Bint Jahsin nee na ma ne ko: yaw Yonnente Yàlla bi: ndax dees nuy alag te ñu baax ñi nekk sunu biir? Mu ne ko: "waaw bu lu bon baree».
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
عن عائشة رضي الله عنها قالت: كان رسولُ اللهِ صلى الله عليه وسلم إذا فَاتَتْهُ الصَّلَاةُ مِنَ الليلِ مِن وَجَعٍ أَوْ غَيْرِهِ، صَلَّى من النَّهَارِ ثِنْتَيْ عَشْرَةَ رَكْعَةً.
رواه مسلم
Jële nañu ci Anas -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Am mbooloo ci Sahaabay Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dañoo laaj soxnay Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc ay jëfam ci li nëbbu? Am ci ñoom ku ne: man du ma takk soxna, keneen ne: man duma lekk ndawal, keneen ne: man duma nelawati ci kaw lal, Yonente bi daldi sant Yàlla tagg ko, wax ne: "ana lan moo dal aw nit ba ñuy wax lii ak lii? man de damay julli di nelaw, di woor di dog, di takk soxna, ku bañ sama yoon wi bokkul ci man".
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
عَنْ أَنَسِ بْنِ مَالِكٍ رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ قَالَ: إِنَّ خَيَّاطًا دَعَا رَسُولَ اللَّهِ صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ لِطَعَامٍ صَنَعَهُ، قَالَ أَنَسُ بْنُ مَالِكٍ: فَذَهَبْتُ مَعَ رَسُولِ اللَّهِ صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ إِلَى ذَلِكَ الطَّعَامِ، فَقَرَّبَ إِلَى رَسُولِ اللَّهِ صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ خُبْزًا وَمَرَقًا، فِيهِ دُبَّاءٌ وَقَدِيدٌ، فَرَأَيْتُ النَّبِيَّ صَلَّى اللهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ يَتَتَبَّعُ الدُّبَّاءَ مِنْ حَوَالَيِ القَصْعَةِ، قَالَ: فَلَمْ أَزَلْ أُحِبُّ الدُّبَّاءَ مِنْ يَوْمِئِذٍ.
متفق عليه
عَنْ أَبِي هُرَيْرَةَ رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ قَالَ: قِيلَ: يَا رَسُولَ اللهِ ادْعُ عَلَى المُشْرِكِينَ قَالَ: «إِنِّي لَمْ أُبْعَثْ لَعَّانًا، وَإِنَّمَا بُعِثْتُ رَحْمَةً».
رواه مسلم