Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Dégg diine ak i cosaanam

Jële nañu ci Sahl Ibn Sahd yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc wax na ne:

Available in 50 languages
«Jële nañu ci Sahl Ibn Sahd yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc wax na ne: «nit ñi du ñu deñ di nekk ci yiw fii ak ñoo ngi gaaw a dog».»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc day xamle ne nit ñi du ñu deñ di nekk ci yiw fii ak ñoo ngi gaaw a dog ci koor ginnaaw ba ñu wóorloo ci sowug jant bi; loolu nag ngir jëfe suuna si la, ak tënku ca.

Source
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Download image

Saved at original quality