Ngëneel yi ak teggiin yi
Jële nañu ci Abuu Dardaa -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yonente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:
Available in 48 languages
«Jële nañu ci Abuu Dardaa -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yonente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «ñiy rëbbaate duñu nekk ay seede du caagine ay rammkat ëllëg bis-pénc».»Meaning translation ·
Saved at original quality








