Pas-pasu Lislaam
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne:
Available in 49 languages
«Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc rëbb na góor giy sol colug jigéen, ak jigéen giy sol colug góor.»Meaning translation ·
Saved at original quality








