Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Dégg diine ak i cosaanam

Jële nañu ci Aysatu ndayu jullit ñi yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na:

Available in 47 languages
«Jële nañu ci Aysatu ndayu jullit ñi yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na: "dees na dagg loxo ci ñenteelu xaaju Diinaar jëm kaw".»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc leeral na ne sàcc bi dañuy dagg loxoom ci càccug ñenteelu xaaju Diinaaru wurus, ak lu ëpp loolu, ag xaymaam di yamoo ak 1.06 Garaam ci wurus.

Source
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Download image

Saved at original quality