Ngëneel yi ak teggiin yi
Jële na ñu ci Ibn Abbaas yal na leen Yàlla dollee gërëm mu wax ne Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daan na wax:
Available in 46 languages
«Jële na ñu ci Ibn Abbaas yal na leen Yàlla dollee gërëm mu wax ne Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daan na wax: "Allahumma laka aslamtu, wa bika aamantu, wa halayka tawakkaltu, wa ilayka anabtu, wa bika xaasamtu, Allaahuma innii ahuusu bihissatika, laa ilaaha illaa Anta an tadillanii, Anta Al-Hayyu Allasii laa yamuutu, wal insu wal jinnu yamuutuuna".»Meaning translation ·
Saved at original quality








