Ngëneel yi ak teggiin yi
Jële na ñu ci Anas Ibn Maalik yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na:
Available in 53 languages
«Jële na ñu ci Anas Ibn Maalik yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na: «ñaan deesu ko delloo ci diggante nodd ak liqaam».»Meaning translation ·
Saved at original quality








