Ngëneel yi ak teggiin yi
Jële nañu ci Abuu Muusa yal na ko Yàlla dollee gërëm, mu nettali ci Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc ne daan na ñaan ñaan gii:
Available in 54 languages
«Jële nañu ci Abuu Muusa yal na ko Yàlla dollee gërëm, mu nettali ci Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc ne daan na ñaan ñaan gii: "rabbi ixfir lii xadii-atii wa jahlii, wa israafii fii amrii kullihii, wa maa Anta ahlamu bihii minnii, Allaahuma ixfir lii, xataayaaya, wa hamdii wa jahlii wa haslii, wa kulli saalika hindii, Allaahuma ixfir lii maa xaddamtu wa maa ax-xartu, wa maa asrartu wa maa ahlantu, antal Muxaddimu wa Antal Mu-axiru, wa Anta halaa kulli say-in xadiirun ".»Meaning translation ·
Saved at original quality








